LEMZO CHERI - EPISODE 06 (VOSTFR)

Abonnez-vous à notre chaine FRwatch

▷▷ ABONNEZ-VOUS ICI : frwatch.info/film/Ovr.html...

🔔 Activez les NOTIFICATIONS pour ne pas manquer les prochaines vidéos
Retrouvez-nous sur www.leuztv.com/
------------------------------------------------------------------















frwatch.info/film/Ovr.html...
Suivez-nous sur Facebook leuzmedia?fr...

Commentaires 

  1. Mame Sms

    Mame Sms

    Il y a 3 jours

    Ahah bilay wadji mo meun doul nak😂😂 rouss n'a di diar sa tour bou nekh bi abass Astafirlah degual li rek guay yar bir nonou di fen rek di dadialé non guor you melni yalla nassi yalla moussal bep djiguen way🙏🙏

  2. Fatima Mendy

    Fatima Mendy

    Il y a 3 jours

    Abass est incroyable 🤣🤣🤣

  3. Sophie Dia

    Sophie Dia

    Il y a 3 jours

    Team Guigui alias clémentine 👌♥️👌👌👌

  4. Alexis Mendy

    Alexis Mendy

    Il y a 4 jours

    Abass 😂😭🤣

  5. Tako Sanyang

    Tako Sanyang

    Il y a 5 jours

    Biddew dafa wara nyow bokk c serie bi 😃

  6. Marietou faye

    Marietou faye

    Il y a 6 jours

    Delene yokk jour yi

  7. Marietou faye

    Marietou faye

    Il y a 6 jours

    Machalla serie bou nekh bi damakoye khar tfm chaque mercredi

  8. Maman Seck

    Maman Seck

    Il y a 6 jours

    Issa nar alias Abass un talent a suivre borome thies bakh yatou yeuk nite

  9. Dio Sow

    Dio Sow

    Il y a 7 jours

    Aldjouma ninguay deff legui nga done altiné

  10. Sarjo Bah

    Sarjo Bah

    Il y a 7 jours

    Nice

  11. Souleye Dieye

    Souleye Dieye

    Il y a 7 jours

    No abass do déme 😂😂😂

  12. sasha s

    sasha s

    Il y a 8 jours

    thioukna torop naguene fekhe ba continuer ko. Du courage et bonne continuation

  13. seynabou diop

    seynabou diop

    Il y a 8 jours

    Wa yenn ndékété Abass nekhna deh réé na déé

  14. Marcelle HDB

    Marcelle HDB

    Il y a 8 jours

    Sous titres svp 😪😪😪

  15. la belle phénix

    la belle phénix

    Il y a 8 jours

    Aïcha firil sa kanam gui touti tamite.yangui mélni kouy déprimé

  16. أحمد مال جل

    أحمد مال جل

    Il y a 8 jours

    Mbappé si théâtre bi

  17. Lamzo Sarr

    Lamzo Sarr

    Il y a 8 jours

    😘💶😍😍👌👌😂

  18. nafi Ndiaye

    nafi Ndiaye

    Il y a 8 jours

    Bilay les prestataires souffre

  19. Rokhayatou Darame

    Rokhayatou Darame

    Il y a 8 jours

    Sèrie bi dafa nèkh

  20. Dl tv

    Dl tv

    Il y a 8 jours

    😂

  21. Abdou Lo

    Abdou Lo

    Il y a 9 jours

    Machallah aicha

  22. fatima sonko

    fatima sonko

    Il y a 9 jours

    Abasss Meunn gua fenn

  23. Lamine Diaw

    Lamine Diaw

    Il y a 9 jours

    Qui a remarqué l'instru de Youssou ndour "Gamou" ?😊

  24. Sopey Mame Diarra

    Sopey Mame Diarra

    Il y a 9 jours

    Abass dal momaye dane si serie bi! il est trop drole. Opportuniste en chair et en os.

  25. Maimouna Ndiaye

    Maimouna Ndiaye

    Il y a 9 jours

    Xaritou Absa bi wollou woumako dara dafa nara tass seuyou diambour bi

  26. soso sousou

    soso sousou

    Il y a 9 jours

    Toujours pas de sous-titres

  27. Bara fall

    Bara fall

    Il y a 9 jours

    ❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  28. Fatou Sall

    Fatou Sall

    Il y a 9 jours

    Aram mi leuf la🤣🤣🤣

  29. Elisa Demba

    Elisa Demba

    Il y a 9 jours

    Fama😂😂😂😂🤣🤣🤣🤣😂😂😂😂😂🤣😂😂🤣😂😂🤣🤣🤣🤣❤

  30. awa ndiaye Pouye

    awa ndiaye Pouye

    Il y a 9 jours

    Série bi bari na Aÿ diagalé guir yalla continuer ainsi bouléne si dougeul béne vulgarité svp

  31. Mouhamadou M. Mbaye

    Mouhamadou M. Mbaye

    Il y a 9 jours

    Abasse dinama ray 🤣🤣🤣

  32. Awa diaby gassama

    Awa diaby gassama

    Il y a 9 jours

    Aicha jtm trop machalla tu es trop belle❤❤❤❤❤❤

  33. fary mboup

    fary mboup

    Il y a 9 jours

    Rang mouy lemzo cherie😂😂💪

  34. Astou fall

    Astou fall

    Il y a 9 jours

    Wa aldiouma mom khalissam bou beury bi yeup appartement la am..lol

  35. Medzü Niang

    Medzü Niang

    Il y a 9 jours

    Mane abass meune nama raay 😂😂mbappé kay😂😂

  36. Willy Madjiguene Diop

    Willy Madjiguene Diop

    Il y a 9 jours

    Abass bayil présenter by 🙃danou ngua tay

  37. Willy Madjiguene Diop

    Willy Madjiguene Diop

    Il y a 9 jours

    Aÿ Arame tu es extra menthe😅sa kharit ly nguanguoy fay

  38. Step Up

    Step Up

    Il y a 9 jours

    Mbappe 😂

  39. Ndiok

    Ndiok

    Il y a 9 jours

    Ngouri mo gnawe dé

  40. Moustapha Dabo

    Moustapha Dabo

    Il y a 10 jours

    Goerge Whea xamguako 🤣🤣🤣🤣

  41. Ada Falle

    Ada Falle

    Il y a 10 jours

    Abass nganer do bayi mew😂😂😂😂

  42. Adama Ndiaye Kasse

    Adama Ndiaye Kasse

    Il y a 10 jours

    Thieyy kharitt bou djiguenn 😰😰🤦🏻‍♀️surtout nak boko gueunné nékk thi situation bou bakh. Dalay jalouser dila soufou

  43. Ob trice

    Ob trice

    Il y a 10 jours

    Wa mais goor you meune doule comme Abas mingui existé batey??? Guel yi tamitt kagn nguéne di yéwou???

  44. Bachir Ndiang

    Bachir Ndiang

    Il y a 10 jours

    Guigui je l’aime Bilay son futur mari auras bcp de chance, sinon elle assure grave vraiment c’est une battante elle ne cesse de prouver son talent d’artiste depuis ces debuts et n’as jamais profité de sa beauté pour percé. Cette série promet 👏🏻👏🏻👏🏻👏🏻👏🏻👏🏻👏🏻

    • Sophie Dia

      Sophie Dia

      Il y a 3 jours

      Apart youssou Ndour c’est elle la star ⭐️

  45. Sira 20

    Sira 20

    Il y a 10 jours

    LES SOUS TITRES !!!!!!!!

  46. Dj Khalil

    Dj Khalil

    Il y a 10 jours

    🇸🇳

  47. theresa fouckou moko

    theresa fouckou moko

    Il y a 10 jours

    Les sous titres 🙄

  48. ALFAAROUKH Tv

    ALFAAROUKH Tv

    Il y a 10 jours

    KOU CONTANE SI TALATAY MACARON BI REK TÉ BEGOU RASSOULLOU LAHI REK JEM SVP ❤️

  49. Ndeye Amy Fall

    Ndeye Amy Fall

    Il y a 10 jours

    Waw Arame mi niit la😳😳😱😱

  50. Assane Ndiaye

    Assane Ndiaye

    Il y a 10 jours

    Nexna Trop Mais Temps Bi Dafa Guattéu Te Épisode Yi Déy Sorante

  51. Aby Hydrangea

    Aby Hydrangea

    Il y a 10 jours

    Birame bou MHDM serait un bon recrue dans cette série.

  52. Marie USA

    Marie USA

    Il y a 10 jours

    Mbappe thiey goor ngi

  53. Kany Senghor

    Kany Senghor

    Il y a 10 jours

    Abas weroul dé

  54. Nitou Dege ki

    Nitou Dege ki

    Il y a 10 jours

    Mbappè kay😃😃😃

  55. Pop Smoke The Woo

    Pop Smoke The Woo

    Il y a 10 jours

    Yalna jaam yague

  56. Astou Nael

    Astou Nael

    Il y a 10 jours

    Abasse mounaneu mbate fi danio change Sama tour🤣🤣🤣🤣

  57. Abdou Ndiaye

    Abdou Ndiaye

    Il y a 10 jours

    Ay abass mi mamna doul dé 😠😠

  58. Abdou Ndiaye

    Abdou Ndiaye

    Il y a 10 jours

    C'est la première fois ma sétane ko mai dotou mako bayi

  59. SHAM THIAM

    SHAM THIAM

    Il y a 10 jours

    Arame ak absa dou moudié fou bah deh

  60. Bayo Souley

    Bayo Souley

    Il y a 10 jours

    😄😄😄Abbass quel gathiéee

  61. libasse dieye

    libasse dieye

    Il y a 10 jours

    vbdhfhjdhjyhgdjdythdgjjdhthhjdh

  62. Younouss Ndiaye

    Younouss Ndiaye

    Il y a 10 jours

    Cey abas aka nex

  63. christine gning

    christine gning

    Il y a 10 jours

    Thiey ces genres d'hommes existent au Sénégal.Les filles faisont très attention.

  64. fatima fatima

    fatima fatima

    Il y a 10 jours

    clementine donne mes tes lunettes hahahahah

  65. Ndeye awa Diaw

    Ndeye awa Diaw

    Il y a 10 jours

    machal valide

  66. Momo Emmanuel Vdn (Pianist)

    Momo Emmanuel Vdn (Pianist)

    Il y a 10 jours

    la traduction

  67. Loifa El frezhi

    Loifa El frezhi

    Il y a 10 jours

    Abass vrai frimeur

  68. Loifa El frezhi

    Loifa El frezhi

    Il y a 10 jours

    Adjiouma trop gentile CES PA Bon deh

    • Bineta Leye

      Bineta Leye

      Il y a 8 jours

      Trop bon trop con

  69. loulou Fall

    loulou Fall

    Il y a 10 jours

    J AIME

  70. fatou gueye

    fatou gueye

    Il y a 10 jours

    Vraiment série bi dafma nekh 🥰🥰🥰

    • Ndeye anta Gaye

      Ndeye anta Gaye

      Il y a 9 jours

      @Oumar Sall ndakh nga sagnko wakh douma commentaire lou barri dh mei fatou gueye fouma tournè guisla sama ndiekè bi 😄😄

    • Oumar Sall

      Oumar Sall

      Il y a 9 jours

      La reine du youtube

  71. Ismaila Camara

    Ismaila Camara

    Il y a 10 jours

    Questo video e bellissimo 🥰🤣😆❤🥰🥰❤❤❤🥰

  72. ndong fatou k

    ndong fatou k

    Il y a 10 jours

    série buneikh bi gay am fofu sétan tagneuw

  73. fatou samb

    fatou samb

    Il y a 10 jours

    Serie bi nekhna trop❤️❤️

  74. ndeye ndaw

    ndeye ndaw

    Il y a 10 jours

    🥰🥰

  75. Yama Cisse

    Yama Cisse

    Il y a 10 jours

    Sacré Abasse 🤣🤣🤣😂😂

  76. Ngagne Diagne

    Ngagne Diagne

    Il y a 10 jours

    Mbappé 🤣🤣🤣🤣abass monékh

  77. Adame Ngom

    Adame Ngom

    Il y a 10 jours

    Abasse do changer mbape la toudou 😂😂😂

    • fary mboup

      fary mboup

      Il y a 9 jours

      @Adame Ngom moma diakhal

    • Adame Ngom

      Adame Ngom

      Il y a 9 jours

      @fary mboup dama khamoul loumiye fene kate

    • fary mboup

      fary mboup

      Il y a 9 jours

      Ki ka mo raw mbappè

  78. Ayib vivi Ceesay 🇬🇲🇬🇲

    Ayib vivi Ceesay 🇬🇲🇬🇲

    Il y a 10 jours

    Daroooo ❤️

  79. Khady Barro

    Khady Barro

    Il y a 10 jours

    Les filles faisons très attention qu’un mec avec une voiture ne nous impressionne pas si on fait le nécessaire on peut se payer des voitures plus chers que les leurs. Naniou liguey on s’en fou des voitures des autres

    • Diatou Sow

      Diatou Sow

      Il y a 4 jours

      @Djibril Sow si qev

    • demba fofana

      demba fofana

      Il y a 5 jours

      @Thiané Diéye 😂😂😂

    • Pretty Méra

      Pretty Méra

      Il y a 9 jours

      @Khady Barro walahi ils n'ont rien compris. Deug piir nga wakh Machaallah

    • Thiané Diéye

      Thiané Diéye

      Il y a 10 jours

      @Khady Barro loin de moi l idée de me moquer de vous. Dama ladonn chambrer tuti rek...rien de méchant. Toutes mes excuses si vous vous êtes senties un peu offensée par mes propos. Ton commentaire est plein de sens...mais malheureusement bu for yombé, seugg jafé. La plupart mise trop sur leur plastique au lieu de bosser dur...

    • Khady Barro

      Khady Barro

      Il y a 10 jours

      @Thiané Diéye tu confonds sensibilisation et peine de cœur vous êtes tellement occupé à essayer de vous moquer des gens que vous n’apprenez rien d’eux

  80. Lobe Ndiaye

    Lobe Ndiaye

    Il y a 10 jours

    Deum rayela Dialeléla 🙆‍♀️ Thiey Arame mii

    • Lobe Ndiaye

      Lobe Ndiaye

      Il y a 10 jours

      @Saliou Coly 😂🙆‍♀️ balnala

    • Saliou Coly

      Saliou Coly

      Il y a 10 jours

      Lobé yangui fépp😂😂

  81. Mame diarra Diome

    Mame diarra Diome

    Il y a 10 jours

    😥🤔

  82. thiabetv web

    thiabetv web

    Il y a 10 jours

    merci toujours égale lui même vos série sont top mais yokal fréquence ag visibilité yagui yar yagui yété pas vulgaire ni extravagant bon vent

  83. Houleye Ka

    Houleye Ka

    Il y a 10 jours

    Daro 🤣🤣

  84. Diama Ndiaye

    Diama Ndiaye

    Il y a 10 jours

    Abass liko dal , febar bi noum toud🤣😂😂hei abasss li mba diam l

  85. titi Moh

    titi Moh

    Il y a 10 jours

    Traduction 😪

  86. Moustapha Ndiaye

    Moustapha Ndiaye

    Il y a 10 jours

    abass mdr

  87. Isidore Memdy

    Isidore Memdy

    Il y a 10 jours

    Machalla Absa tu es charmante ❤️❤️❤️💋💋

  88. Fallou Mbaye

    Fallou Mbaye

    Il y a 10 jours

    🥳🥳

  89. Souley Man

    Souley Man

    Il y a 11 jours

    Arame bette gama

  90. dykha Mbaye

    dykha Mbaye

    Il y a 11 jours

    Abass sa gathier bi reuyneu dai

  91. Dômou Galsén

    Dômou Galsén

    Il y a 11 jours

    Mane sons youssou ndour bissi souff momay fathie remix "sama gamou bii " fouma koy dieulé tamite

  92. Mariela Sahoro

    Mariela Sahoro

    Il y a 11 jours

    Les sous titres svp

  93. 🎀Awa Jay🎀

    🎀Awa Jay🎀

    Il y a 11 jours

    Arame bon nga! 🙆🏽‍♀️🤔

  94. Neinishh Sarr

    Neinishh Sarr

    Il y a 11 jours

    Ndysane serie bi dafa nekh mais niou bari xamou niouko

    • Binta Cissokho

      Binta Cissokho

      Il y a 10 jours

      Nékna trop way

  95. methzo niang

    methzo niang

    Il y a 11 jours

    Mbappé😁😁

  96. NOPE TV (Mohamed benzékry)

    NOPE TV (Mohamed benzékry)

    Il y a 11 jours

    Abass😂😂😂😂😂😂taymou deiii

  97. NOPE TV (Mohamed benzékry)

    NOPE TV (Mohamed benzékry)

    Il y a 11 jours

    Dibie xaar bou amoul bakarrr😂😂😂😂😂😂

    • Khady Badji

      Khady Badji

      Il y a 9 jours

      Bilay ki douma Ray,,néna mbapé lagn may wowé

  98. kambaro Drame

    kambaro Drame

    Il y a 11 jours

    Thiey abass 😂

  99. mamediarra dieng

    mamediarra dieng

    Il y a 11 jours

    Aicha dafa sofe

  100. NOPE TV (Mohamed benzékry)

    NOPE TV (Mohamed benzékry)

    Il y a 11 jours

    Petawkate yi Akanio mana feine même wakh (sa bop ngui yeukeutikou, kheil niarr, ngoro, keuyite boy lidjeunti, wadji wala gueil bi khessoul niouloul, ki koula djeguei la, weurseuk Boulay beet, lo yakar day tass)😂😂😂😂😂😂😂doule Rek😂😂😂😂😂😂

    • Rokhaya Ngom

      Rokhaya Ngom

      Il y a 9 jours

      🤣🤣🤣

    • NOPE TV (Mohamed benzékry)

      NOPE TV (Mohamed benzékry)

      Il y a 10 jours

      @SOUKEYNA SOCK 😂😂😂😂

    • SOUKEYNA SOCK

      SOUKEYNA SOCK

      Il y a 10 jours

      Yangui fepeu fouma diarr guiss lafa 🤣🤣🤣🤣🤣

Prochain