FAMILLE SENEGALAISE - Saison 1 - Episode 6 - VOSTFR

[Abonnement Gratuit ici]☆~~👉 bit.ly/Abonnement_Gratuit_Pikini

[FACEBOOK]☆~~👉 bit.ly/Facebook-Pikini

[Visitez notre Blog]☆~~👉 bit.ly/Blog-Pikini

[TWITTER]☆~~👉 bit.ly/Twitter-Pikini

Commentaires 

  1. Astou Fall

    Astou Fall

    Il y a 3 heures

    ♥️♥️

  2. Henriette Diouf

    Henriette Diouf

    Il y a 7 heures

    Problème d montage si fété bi boumou done wégn warone guéne éliminer son bi

  3. ÉVA DIOP

    ÉVA DIOP

    Il y a 2 jours

    Sohna ya meune féne

  4. BAMBA ELECTRONIQUE

    BAMBA ELECTRONIQUE

    Il y a 2 jours

    Hhhh Nar bi nitt Mongui Fêpe vive pari foot ⚽️

  5. Marie Ndiaye

    Marie Ndiaye

    Il y a 3 jours

    Mdr mar reynama sama nidiaye bathia alakhira

  6. Aîda Sow

    Aîda Sow

    Il y a 3 jours

    Asc👍👍

  7. Mamadou Ndiaye

    Mamadou Ndiaye

    Il y a 3 jours

    Woudié souma ko dé xalat sax damay fébare bilay

  8. Amy Deme

    Amy Deme

    Il y a 3 jours

    vraiment waronenga toudou nénéne bamou désse sokhna bator

  9. Fatou Niang

    Fatou Niang

    Il y a 3 jours

    Bintou thiam je déteste ton personnage really di fen bay fénal sa baye bou dead noooo li amoul

  10. Malick Ka

    Malick Ka

    Il y a 4 jours

    No naar bi dounit,

  11. Fatou Kebe

    Fatou Kebe

    Il y a 4 jours

    Je veux savoir l'hôtel oú mar et botor passent leur lune de miel c très joli

  12. Mareme Wade

    Mareme Wade

    Il y a 5 jours

    Wa jeux bi bane jeux la an😂😂😂😂

  13. Maimouna Sanogo

    Maimouna Sanogo

    Il y a 5 jours

    Une vraie vipère souhan'allah que Dieu nous préserve d'avoir des femmes comme ça dans notre famille aamiin

  14. Moussa Toure

    Moussa Toure

    Il y a 6 jours

    Merci beaucoup a votre partage 🇸🇳❣💝🤛🤝💯🙌💔💗💞👏💪🇮🇹

  15. Mame Bousso GAYE

    Mame Bousso GAYE

    Il y a 6 jours

    Wa sohna Bator mi moy 🥺🥺 yaw sa papa gagnou nianaloko diko toumall 🧐🧐

  16. Idrissa Dia

    Idrissa Dia

    Il y a 6 jours

    Vous relatez la vraie vie chez nous

  17. Ngoné Diaba GUEYE

    Ngoné Diaba GUEYE

    Il y a 7 jours

    J'aime la complicité entre les deux sœurs de Mar c'est comme moi et ma sœur ❣️🌹🔥👯💏

  18. Fatma Ndao

    Fatma Ndao

    Il y a 7 jours

    🤭🤭🤭

  19. dieurëdjëfé Borome Touba

    dieurëdjëfé Borome Touba

    Il y a 7 jours

    Très bonne série... Juste une précision: Niarell yii mélou nou nak vraiment😀 Barii n'a gnou pékhé, un peu jalouses... mais sont responsables de la stabilité des familles. Big up à elles💪💪💪😘

    • dieurëdjëfé Borome Touba

      dieurëdjëfé Borome Touba

      Il y a 5 jours

      @Fatimata Thiam dessit=bolou dof goor Yalla rek mo koy djërigno talibés boulo dof lay lek... niarell dou ay fo... tu ne peux pas comprendre malheureusement pour toi bëgo dès siit😀

    • Fatimata Thiam

      Fatimata Thiam

      Il y a 5 jours

      @dieurëdjëfé Borome Touba manéla bou awoh firoul niarel beugg dessite'' waroul firr

    • dieurëdjëfé Borome Touba

      dieurëdjëfé Borome Touba

      Il y a 5 jours

      @Fatimata Thiam niarell real love lay doundou té kou bëgg firr😀oui stabilité... si tu n'est pas dans la polygamie tu ne peux comprendr😊

    • Fatimata Thiam

      Fatimata Thiam

      Il y a 5 jours

      Stabilité Kaye Awoh yékeh yoor ,louye gnarél Di jalouse t'ai moh fékissi. oser badehh

  20. Rosebella

    Rosebella

    Il y a 8 jours

    Accuser sa pape viole thiey li graw na dé 😫😳🙄

  21. Raky Diaw

    Raky Diaw

    Il y a 8 jours

    Chheuuuu bi mome eupeuna tamite dome bou gnanaloule papame diko djigne viole Sokhna bator ki es tu ?

  22. KHADIM LO

    KHADIM LO

    Il y a 9 jours

    Son bi daw si souf koukou way tamit nékhna torop way bravo pikini production thia kaw thia kanam

  23. KHADIM LO

    KHADIM LO

    Il y a 9 jours

    Bigé dél rétan so rétané man damay kontan

  24. KHADIM LO

    KHADIM LO

    Il y a 9 jours

    Seri ni la wara mél

  25. Coumba Diallo

    Coumba Diallo

    Il y a 9 jours

    Mar daal dafa melni damala nop🤣

  26. Bineta Leye

    Bineta Leye

    Il y a 9 jours

    Djiguene bou melni Sokhna Bator da nuisible pour la société. Baakhougnou si keur ni alleu

  27. Cheikhouna Dia

    Cheikhouna Dia

    Il y a 9 jours

    ,🥰🥰🥰🤩🤩🤩

  28. Diaryatoulah Diop

    Diaryatoulah Diop

    Il y a 9 jours

    Mar lo kanam bi dou transmettre ben émotion impassible ak situation boum meunti don nak 😒😒 bator c'est satan en personne

  29. Khady Dia

    Khady Dia

    Il y a 9 jours

    Bator c’est le diable en personne

  30. Ndeye Ndiaye

    Ndeye Ndiaye

    Il y a 9 jours

    Bilahi sou wédi touma meunona nék néw you.bari.dinaniou Diok.wakh

  31. Mame diarra Diop

    Mame diarra Diop

    Il y a 9 jours

    Bineta THIAM sa diogama Lanlaa😘😘😘😍😍😍😍😍

  32. Kodou Gueye

    Kodou Gueye

    Il y a 9 jours

    Mon série préfère

  33. balla dieng

    balla dieng

    Il y a 9 jours

    Bogue dioy lonama 🥲😭lou bakh rk mola si dougalon ❤️

  34. Mame diarra Diop

    Mame diarra Diop

    Il y a 9 jours

    Ohhhh Mane dal j'aime cette série

  35. mama awa

    mama awa

    Il y a 9 jours

    No Bator une peste au point d’accuser son propre père 😤😤

  36. Ndeye Séne

    Ndeye Séne

    Il y a 9 jours

    Sokhna batore mii moom Ayaa bimbam fen rk

  37. momo mbow officiel

    momo mbow officiel

    Il y a 9 jours

    j'aime bien les femmes africaine la beauty teint Noire 🥰

  38. Galass Gaye

    Galass Gaye

    Il y a 9 jours

    Pikine j’aime trop vos produits mais cett publicité nuisible à la société k vous nous proposez n’est pa bien honnêtement.pari foot 🥅 c pa bon ......

  39. Mor Mbow

    Mor Mbow

    Il y a 9 jours

    Mar sa porte keur giii nice naaa ,,tres simple,,,sathinaa motifff bii dddd

  40. Daff Pape

    Daff Pape

    Il y a 9 jours

    Maman franchement liii dou yaw nékhou ma dara mes ta assuré nak manchala

  41. Jamm Rék!

    Jamm Rék!

    Il y a 10 jours

    Trop de rappels!

  42. Rousseau Jean

    Rousseau Jean

    Il y a 10 jours

    Pikini dal dougnou aye thiouné

  43. Oumi Diallo

    Oumi Diallo

    Il y a 10 jours

    Waaa batooor mii Liga yore si fiiite dekke amna fenale sa baye basa alakhira soubkhanala

  44. Diaw Cheikhna

    Diaw Cheikhna

    Il y a 10 jours

    Awo yi rek

  45. Alimatou Sadiya Mbengue

    Alimatou Sadiya Mbengue

    Il y a 10 jours

    Seytanê moy botor

  46. Aicha Sow

    Aicha Sow

    Il y a 10 jours

    On dirait que Alima est la future femme de Mar

  47. khadidiatou fall

    khadidiatou fall

    Il y a 10 jours

    Non khalè bou sobbè nii amoul ! Biguè lii yeup yawla et ta maman va souffrir

  48. Ndeye Sophie Thiongane

    Ndeye Sophie Thiongane

    Il y a 10 jours

    Kou melni Sokhna Bethor. Yalla nasi Yalla moussal ap diam. Ki mo raw cas communautaire

  49. Mohamed Diallo

    Mohamed Diallo

    Il y a 10 jours

    Sénégal rék dafa nekh🇸🇳🇸🇳🇸🇳🤩🤣🤣🤣

  50. Aissatou Diakhaté

    Aissatou Diakhaté

    Il y a 10 jours

    Ngone elle est troo bell

  51. Aïda Cissé

    Aïda Cissé

    Il y a 10 jours

    J'adore la série

  52. Abba Diop

    Abba Diop

    Il y a 10 jours

    Sokhna botor dafa meuna fène

  53. Moustapha Samb

    Moustapha Samb

    Il y a 10 jours

    Ca Family ba la.

  54. Pop Smoke The Woo

    Pop Smoke The Woo

    Il y a 10 jours

    Team pikini

  55. NGagne Fall

    NGagne Fall

    Il y a 10 jours

    Xaléyou jyguéne yii fii guénii dougueleu xalisse métinama😂😂

  56. NGagne Fall

    NGagne Fall

    Il y a 10 jours

    Ayei sokhna beutore daga daleu si goor bou un peu naïf rek Trop bon trop con 😂

  57. Sokhna Laye

    Sokhna Laye

    Il y a 10 jours

    En tous cas dans les séries sénégalaises le mensonge est à son paroxysme 😳 leplus flippant moye tu peux faire le parallèle avec la vraie vie dafa ame gnou féne yombeu eupeuleuw féne gratuitement 🙄😆

  58. Yacine Dieye Kara

    Yacine Dieye Kara

    Il y a 10 jours

    Commencé guén di def aie erreur botor naka lay hamé né son l'a violé mouy out honneur lolu kay occasion la won Mar comprend ko dès la début

    • ALY LOBASS

      ALY LOBASS

      Il y a 10 jours

      Salut sister . Enfaite elle avait programmé un « ndaw » Artificiel. Le jour «diebeul elle a fait un chute et a perdu la virginité artificielle que lui fait un MEDECIN. Sans cette fameuse chute elle aurait pu réussir son coup

  59. Mariama Dia

    Mariama Dia

    Il y a 10 jours

    Mais maar xèsal bi tamit loulaka diaral, waw niarel mom guathia dinaka Ray?

  60. Fallou Fam

    Fallou Fam

    Il y a 10 jours

    Sagar raynama 🤣🤣🤣🤣

  61. ndeye mour ndoye

    ndeye mour ndoye

    Il y a 10 jours

    Aw sokhna bator meunal feneu, boneu nal ou nékka fi rk la diakhassé ka routalé bakh na rk....

  62. Black Woman

    Black Woman

    Il y a 10 jours

    Botor mi meune na féne d

  63. Sokhna Ndiaye

    Sokhna Ndiaye

    Il y a 10 jours

    Sokhna Bator artiste compléte la

  64. Adja Toure

    Adja Toure

    Il y a 10 jours

    Wa mais sokhna Bator mi dama ko ragal nak cas le dé

  65. Astu Guey

    Astu Guey

    Il y a 10 jours

    Waa yéne djiguéne gni sax si nar bii

  66. Astu Guey

    Astu Guey

    Il y a 10 jours

    Pikini encore une fois yallah guéne am 2millon abonnés et plus

    • Pikini Production

      Pikini Production

      Il y a 10 jours

      Amen

  67. Diarra Diouf

    Diarra Diouf

    Il y a 10 jours

    Merci ❤️👍

  68. Ndeyemarem Thiam

    Ndeyemarem Thiam

    Il y a 10 jours

    ❤️❤️♥️♥️♥️♥️👍

  69. Aminata Ndoye

    Aminata Ndoye

    Il y a 10 jours

    Ayye waye bintou thiam( sokhna botor) waro wone nangou rôle bii nakh je t'aime trop wayye. Fii monme mousiba nga fii joué

  70. Aida Gueye

    Aida Gueye

    Il y a 10 jours

    Bator mi ragal nako dé😱😱

  71. Rama Mbacke

    Rama Mbacke

    Il y a 10 jours

    Viole bou yakhoul ci yaw dara wa ki rewoul... mar tamite sofnama ki mom dof na con ci kou begoul wone tchim bo begone fi todj radiakh... bator ki es ti ci seytane meun fenn lonnnne am fiite

  72. Ndeye Amy Fall

    Ndeye Amy Fall

    Il y a 10 jours

    Waw Sokhna mi niit la yene😳😳😳😱😱😱😡😡😡😡😡

  73. Marie

    Marie

    Il y a 10 jours

    ay batorrrrr ! sa yaye assistewoko bamou gagnou yagoul ngay hew!!! légui se papa nga warko nianal légui ngay saltel dérammmm! sa moudjie dine giuene eune fausse publique

  74. fatou gueye

    fatou gueye

    Il y a 10 jours

    Kouy niak diom betor ngay diapalé thippp 🙈Mar yangui beugue diengue dé

    • Moussa Boiro

      Moussa Boiro

      Il y a 4 jours

      La valeur d'une femme g ne c pas à comment la qualifié ❤️

  75. miss mbaye

    miss mbaye

    Il y a 10 jours

    Bilahi Mar ya manké ki di wax sa awo mo xam souko yeugoul gay xouli niak diom kouci am seet faté sa awo

  76. Mamemingue Ndour

    Mamemingue Ndour

    Il y a 10 jours

    salut qui a chante ce générique svp la musique

    • Pikini Production

      Pikini Production

      Il y a 10 jours

      Ndeye Mboup

  77. Lalia Diarra

    Lalia Diarra

    Il y a 10 jours

    Kel est le blem d malal es mare

  78. Fatoucha thiat Sy

    Fatoucha thiat Sy

    Il y a 10 jours

    𝑭𝒓𝒂𝒏𝒄𝒉𝒎𝒆𝒏𝒕 𝒎𝒂𝒓 𝒂𝒎𝒏𝒂 𝒏𝒂𝒌 𝒔𝒓𝒙 𝒑𝒓𝒐𝒃𝒍𝒆𝒎 𝐬𝐨𝐤𝐡𝐧𝐚 𝐝𝐚𝐥𝐥 𝒃𝒊𝒊 𝒃𝒌𝒉𝒏𝒂 𝒅𝒊𝒏𝒂 𝐭𝐚𝐬𝐬𝒔 𝒌𝒆𝒖𝒓 𝒈𝒖𝒊 𝒃𝒊𝒈𝒖𝒆𝒓 𝒅𝒒𝒈𝒖𝒂 𝒔𝒐𝒑𝒑 𝒓𝒆𝒌 𝒘𝒂𝒚𝒆𝒓 𝒃𝒌𝒉𝒏𝒂 𝒍𝒊𝒍𝒆𝒑𝒑𝒑 𝒊𝒐𝒆 𝒍𝒂

  79. GÉNÉRAL Ya salam

    GÉNÉRAL Ya salam

    Il y a 10 jours

    Li mome amoul sénégal ah

  80. Seydi 25

    Seydi 25

    Il y a 10 jours

    N'importe quoi avec cinema sénégalais joyyy rek pleurer pleurer comme kou degue sa yaye dafa déé 😡😡😡

    • Maximum

      Maximum

      Il y a 10 jours

      Legui kou wara joy nou def dagay rei wala

  81. ANITA HANNE

    ANITA HANNE

    Il y a 10 jours

    khale dou dokhal bayam ngoroo bay takh gnou tak seye a part sa le reste c ok juste mon avis

  82. Ismaila Camara

    Ismaila Camara

    Il y a 10 jours

    Questo video e bellissimo 🥰🥰🤣😅😅😅🥰🥰🥰❤❤❤

  83. Keera Bilo

    Keera Bilo

    Il y a 10 jours

    Bigué da nga wané rekkk di wouteul sa papa diabar.ça va te coûter cher. Xalei day yèm place xalei

  84. Coumba Barry

    Coumba Barry

    Il y a 10 jours

    Bigué li lép yaw la daga sobe khalé dafay yéme place khalé

  85. Yacine Kebe

    Yacine Kebe

    Il y a 10 jours

    Loutakh gnarel yi capable

  86. Athia Diallo

    Athia Diallo

    Il y a 10 jours

    Li deh mo takh niou bari beug gouniou woudié

  87. Abiba chou

    Abiba chou

    Il y a 10 jours

    Sokhna bator amngua fiite tè sadick wah bamou sotti😂😂

  88. Cheikh Tidiane Gaye

    Cheikh Tidiane Gaye

    Il y a 10 jours

    🌹🌹🌹🌹😂😂😂😂

  89. Aïssatou Ba

    Aïssatou Ba

    Il y a 10 jours

    Sohna bator yallah naniou yallah mousseul si nit bou melni mome

  90. Bu Pape Sy

    Bu Pape Sy

    Il y a 10 jours

    Complicité bi nek ti mag ak rak yi( Ngone, Sagar) nexnama lol waye mangi giss ni diaxasse sokhna bator, sa diaxasse bala

  91. mia mi

    mia mi

    Il y a 10 jours

    Bakh na thie yaw bigué khawma ana goné ak takal sa bay niaréle sa robou bou massé

  92. dialmb

    dialmb

    Il y a 10 jours

    Makhala. Nek séne diameu Di wouteuli niaarél séne papa. Bigué kou diara n*ouss leu

  93. Dymen Brigitte

    Dymen Brigitte

    Il y a 10 jours

    J’adore la série cause je l’entends avec impatiente Rombou nalé guéni tourné à yoff 🥰

  94. Hanne Oumou

    Hanne Oumou

    Il y a 10 jours

    Musique bii dafa fort trop

  95. نور الحق tv

    نور الحق tv

    Il y a 10 jours

    Kou Begeu kham sa diné Abonnél sama sén bi

  96. AraME Wade

    AraME Wade

    Il y a 10 jours

    Bator esk do adji sarr dignouko neubb

    • Thiam Zayna

      Thiam Zayna

      Il y a 10 jours

      😂😂

  97. Mame Penda BA

    Mame Penda BA

    Il y a 10 jours

    Bâtir menerve puré

  98. Awa Wilane

    Awa Wilane

    Il y a 10 jours

    Vraiment jador cet serie sou ame damay conten

  99. Oumy Diop

    Oumy Diop

    Il y a 10 jours

    Ay mane bator

  100. Deguene Mbaye

    Deguene Mbaye

    Il y a 10 jours

    Hum bator mi diakhale nama

Prochain